gear Paramètres Push
chat
1-Seriñ Tuuba Qàda lahu laahu maxtara lahu ne na: maqàma mi gana kawé fa yàlla jamono ji moy dëkal weetal yàlla cib xol. 2-Sëriñ Tuuba Qàda lahu laahu Maaxtara lahu ne na mbir yi ñetti xaacc lë: xam-xam bu am njariñ ak jëff ju yiiw ak teegin buñ gëram. Xam-xam bu am njariñ mi ngi […]
Bismilahi rahmani rahimi « Li ma xam ci sama’g dundu ci gaatal man Xàdimu Xadiimi Rassùlilaahi sala laahu tahala haleyhi wa salam » Ma ngi gané àdduna ci at’um 1979 wala 1980 ci Daarul Muhty, dëkub Maam Cerno Ibràhima radiya laahu tahala anhu. Sama baay mi ngi tuddu Seriñ Mustafa Hafsa doomi Serin Muhammad Hawa Bàlla […]