Daaju Xasida (3)

Al-Habdul Xadiim
25/02/2020

Leeral u Sëriñ Saaliwu Mbàkke radiya laahu anhu ci daaju mag ñi. Sëriñ Abo Jaxate jëwrinu kurel Daaru Salaam- Xelkom, bokkoon ci ñi daan jàngal ku baax ki moo ko def. Daan ko jàngal fa Njurul ak fa Njaaréem. Daan na jàng itam kër Soxna Faati Ja moom ak kurelam.

Fii nag leerali Sëriñ Saaliwu Mbàkke ci daaju Midaadi lañuy jottali.

Nu teewlu ko te yaatal ko ngir njariñ li gana yaatu!

share Partager

S’abonner
Notification pour
guest
2 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Mouhamad
Mouhamad
6 années il y a

Amna solo lole machala