Jotaayu Texe (4)

Al-Habdul Xadiim
29/04/2025

Dees na xamee ci nettali yii lu bari ci mayi Sëriñ Tuuba Xaada lahu laahu Maxtaara lahu.

Naka noonu déggin wu xóot bi mu am ci lenn ci Aaya yi. Ku xam it mbiri ay taalibeem la, di jëflante ak ñoom ci anam yu wuute.

Yal nanu Yàlla dolli tawfeex te dimbali nu ci sant gi nuy sant Seexul Xadiim.

Jotaayu Texe

Jotaayu Texe (3) Jotaayu Texe (5)

share Partager

S’abonner
Notification pour
guest
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire