Miftaahul Xuyóob (2)
Al-Habdul Xadiim
14/12/2024
Ci xaaj wi, dees na fi lim yi nga xam ne war na boroom kër mu xamal ko soxnaam, ñi mu njaboote.
Te mooy faratay jëmam ak mbolleem li ci aju, dalle ko ci laab, ponki diine yi la cay farata ak sunna. Di ko waar ngir bëggal ko lu baax ëllag. Te sax « góor gu ne ab sàmm la ci ay ñoñam ».
Fàww kon soxna yi ñu leen di xamal seen njariñ. Yal nanu Yàlla tawfeexal.
14/12/2024
Al-Habdul Xadiim
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent
Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires