Miftaahul Xuyóob (6)

Al-Habdul Xadiim
02/03/2025

Fii danu fiy leeral lu aju ci bàmmeel ak dundug bàmmeel ci waxi Kilifa yi.

Dees na fi xamee itam ne, sax ci lu baax dara amul njëgam. Naka noonu topp li Yàlla digle ak wattandiku tere yi. Yal nanu Yàlla saxal cig njub barkeeb koor gii nu nekk.

Miftaahul Xuyóob

Miftaahul Xuyóob (5) Leeral Miftaahul Xuyóob (7)

share Partager

S’abonner
Notification pour
guest
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire