Silaahu Ahlil Xawfi (4) Waxtuy julli ak melow ni ngay fayee li la ci raw.
Al-Habdul Xadiim
16/09/2020
Bismilaahi Rahmaani Rahiim.
Su ko defe nu fas yéene téj Téere bii di Silaahu Ahlil Xawfi, jàngoon nga ci wareefu sàkku xam-xam, ba tax na ràññewon nga ponki diine ak li ciy farata ak sunna. Tay nag di nga fi xamee melow ni ngay fayee julli yi la raw ak seen ay waxtu.
Jërëjëf sang bi
Jaajeufati