Leeral Tasawud Sixaar (1)

Al-Habdul Xadiim
22/09/2022

Bismillahi Rahmaani Rahiim Fii dama fiy béral Meññatum Tasawud Sixaar mu Sëriñ Allaji Mbàkke. Nga xam ne lu nit wara xam rekk ci Téere da nga ko fa fekk mu leeral ko, gaatal ko ba ñépp man ko dégg.

Xaaj wu njëkk wi nag ndékaaney Sëriñ Tuubaa jëm ci ndaw ñi te mooy saxoo jub, taqoo ku baax, sori ku bon, yittewoo Alxuraan ci wàllam yu wuute yi, soxlawoo jëfe xam-xam ak dundal waxtu yi lu baax laa fiy jotali ak lépp loo xam ne mooy tax ngëmug jullit bi man a mat sëkk. Kon deef na fi lim 6i ponki ngëm.

Yal nanu Yàlla sàmmal sunu ngëm, muy dund ba fàww barkeb Xasiiday Borom Tuubaa.

share Partager

S’abonner
Notification pour
guest
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires