Leeral Tasawud Sixaar (2)

Al-Habdul Xadiim
21/10/2022

Bismilaahi Rahmaani Rahiim

Ponki Lislaam lanu fiy leeral. Àttey Julli nag moom leen yaatal ci xaaj bi. Dees na fi xamee itam mbiri laab : jàpp ak sangu farata.

Leeral neen fi it nees di jàppee ak naka lanuy sangoo farata. Mat naa xam ndax boo laabut doo man a def yeneen jaamu yi.Yal nanu Yàlla sàmmal sunu Diinee xirtal nu ci ba fàww, sunuy jëf sell te Yàlla gëram ko.

Leeral Tasawud Sixaar

Leeral Tasawud Sixaar (1) Leeral Tasawud Sixaar (3)

share Partager

S’abonner
Notification pour
guest
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire