
Sëriñ Tuubaa Xaada lahu Laahu Maxtaara lahu daa soññee lool ci tabe, teral gan ak yaatal ko. Mu fiy wax lu tax loolu di lu manul ñàkk ak xéewal yi ci nekk ak ngëneel yi.
Di wax it solos xam-xam, tolluwaay wu réy gi ma am fa sunu Boroom. Di leeral ne ndamoo ay askan ak i judd it amul njariñ.
Yal nanu Yàlla saxal ci lu baax ba fàww.
Macha Allah Serigne Cheikh amna solo lolou. Yalla na sounou borom yokk xam xam bi ci barkep Cheikhoul Khadim
Amiin. Nu bokk lépp! Jërëjëf