Tombi Borom Tuubaa (27)
Al-Habdul Xadiim
07/05/2024
Ginnaw fàttli yi aju ci ndëgarlaayug néttali yi, ci leen daaldi wéyal yaatal wi. Am na ci yu jëm ci mbiri tubaab yi ak waxiini Sëriñ bi, na miy kaweem xel, ak nees di déggee ay waxam.
Kollareem ak taalube yi itam dina fi fés, fullaam, ak dénkaane yu am solo yi muy def ak lenn ci ay tawfeexam.
07/05/2024
Al-Habdul Xadiim
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent
Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires