Tombi Borom Tuubaa (6)
Al-Habdul Xadiim
29/03/2023
Bismillahi Rahmaani Rahiim Yu bari ci néttali yi nu fi àndi day soññee ci weetal Yàlla miy Aji Moom dëgg-dëgg.
Di fi joxe ay tegtal ci wuuteeg àddina ak allaaxira. Di dénkaane itam ci wattandiku mellow àdduna di nu nax.
29/03/2023
Al-Habdul Xadiim
Adouna diaroul alakhira. Tayail diaroul niaakk. Baaneekh diaroul gathié. Am naa solo lol. Yalla nagnou yalla mousseul thi pekhai cheytane.
Wér na lool sax