Tombi Borom Tuubaa (30)
Al-Habdul Xadiim
01/07/2024
Noo ngi toll ci sunu 30i xaaj ci Tombi Borom Tuubaa. Dina feeñee ci néttali yi ni liggéeyal Sëriñ amee lool doole ci nun ak tawfeex gi nekk ci topp ay ndigalam ak bàyyi ay tereem.
Naka noonu di ko sant fu nu toll, doyloo ko, woolu ko te womatu ci moom man na noo may lu ne.
01/07/2024
Al-Habdul Xadiim
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent
Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires