Tombi Borom Tuubaa (23)
Al-Habdul Xadiim
14/01/2024
Fii dañu fiy fésal ni Sëriñ wéetale Boroomam ak liggéey gu muy liggéeyal Yonent bi Aleyhi Salaam ak ni mu key feeñale ci mbindam.
Naka noonu sunu Borom dig na ko lu réy ëllag ginnaaw jaamu Yàlla ju refet gi mu jaamu Boroomam ak jaayanteem ju réy ji.
14/01/2024
Al-Habdul Xadiim
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent
Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires