Tombi Borom Tuubaa (24)
Al-Habdul Xadiim
28/01/2024
Sëriñ Tuubaa dina fi leeral leen ci baati wolof yi ak mahnaa gi ñu ko wara jox dëgg-dëgg.
Lenn ci xarbaax yi itam dees na feeñee fi. Naka noonu Hikma yi.Ba tey ci néttali yi di neen fi dégg luy waral nu wara gën a sàmm sunu kolare ak Sëriñ Tuubaa, sunu diggante ak moom ci def li mu nuy digal ak bàyyi li mu nuy tere.
28/01/2023
Al-Habdul Xadiim
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent
Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires