Tombi Borom Tuubaa (2)

Al-Habdul Xadiim
22/02/2023

Bismillahi Rahmaani Rahiim Ci xaaj wi dees na fi xammee leen ci néttali yi jëm ci lu dib Taalibe. Wax na fi lu aju ci topp ndigal ak bàyyi tere yi.

Lépp jëm ci yokk góor-góorlu ci jaamu Yàlla, teggin yi war ci nodd, moytu lépp luy lu bon.

Di waxtaane it lu baax, di tàmb naafila, tey dundal bëccag gi ak guddi gi ci ay jaamu Yàlla.

Mu fiy aaye itam jëw ak naw sa jëf. Di soññee ci refet ay kàddu di ko jëme ci nit ñi.

share Partager

S’abonner
Notification pour
guest
1 Commentaire
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires
Yacine
Yacine
1 année il y a

Maa Shaa AllAh am naa solo . Yalla nala yalla faiye thi leeral yi