Dooley mbidum Sëriñ Tuubaa (7)

Al-Habdul Xadiim
12/02/2021

Bismilaahi Rahmani Rahiim.

Nu fas yéene matal li desoon ci bayyit yi nga xam ne Sëriñ Alhaaji Mbàkke àndi na ko ci Dooley Mbidum Sëriñ Tuubaa. Muy ay bayyit yoo xam ne ku ko dégg di nga ci jëlle njariñ, sag pas-pas ak sa mbëggeel itam ci Sëriñ bi man na ci yokk bu wér. Noo ngi tuubal ñépp nag, ci njumte yiy man a feeñ ci jotali gi. Di ci fas yiw gu yaatu te koy ñaanal mbooleem ku ko doon topp. Yàlla nanu doon ay dëgg-dëggi Taalube kéem ni ko Sëriñ bi bëggee baekeb Xasiida yi.

Al-Habdul Xadiim
12/02/2021

share Partager

S’abonner
Notification pour
guest
6 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires
Mbacke Gueye
Mbacke Gueye
3 années il y a

Jërëjëfati Serigne Cheikh, santat tey bék si iow dila nianal serigne bi dolli la bou bakh si barkép khassida yi ❤️❤️❤️

Abo Madiyana
Abo Madiyana
3 années il y a

Machallah ! Jerejef

Ndiaye Sarr Ndiaye
Ndiaye Sarr Ndiaye
3 années il y a

Machalla amna solo lolou
Dieuredieuf

IMG_20210928_230651_051.jpg