gear Paramètres Push
chat
Bismilaahi Rahmani Rahiim.
Noo ngi fas yéene wéyal liggéey bi ci Xasida yi nga xam ne ñooy karaamay Sëriñ bi, batey ci lay waxe lu bari ci ay mayam ak ay jagleem. Xasiida yi nag di jariñ lool ki koy jàng.
Al-Habdul Xadiim 10/11/2020
share Partager
Ningéen koy doxale baaxna de jàngéen jëfëti
Jërëjëf yaaram
Machallah fall, ak li gueune
Ningéen koy doxale baaxna de jàngéen jëfëti
Jërëjëf yaaram
Machallah fall, ak li gueune