Dooley mbidum Sëriñ Tuubaa(1)

Al-Habdul Xadiim
23/09/2020

Bismilaahi Rahmaani Rahiim.

Nu fas yéene béral leen ci bayit yi nga xam ne dafay wone mayug Sëriñ bi ak li ko Yàlla defal cig mbidam ak li muy njariñ ki ciy yëngu. Su ko defe lépp mi ngi ci Nahjul Xawiim mu Sëriñ Alhaaji Mbàkke Xaadimul Xadiim. Tay nag nu fas yéene yaatal bayyit 1 ba 9, noonu la nu ko fas yéene jàppee ba kerook nuy àgg ci 113 bayyit insàllaa.

Al-Habdul Xadiim
23/09/2020

share Partager

S’abonner
Notification pour
guest
4 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires
Diop
Diop
4 années il y a

Jërëjëf sang Bi !!!

Soxna Laama
Soxna Laama
7 mois il y a

Machallah