Dénkaane bu jëm ci doomi mbokki Sërin Tuubaa(14).

Al-Habdul Xadiim
17/06/2020

Bismilaahi Rahmani Rahiim.

 » Maa ngi leen di dénk xam, ak jëfe ak tegginu te bàyyi fo. Xam-xam saa su ne luy bégloo lay àndi waaye réer luy lor rekk lay àndi. Ñàkk teggin nag day waral sori Yàlla. Ñàkk jëfe li nga xam day waral alku. Barim po day xañe ay yiiw.
Kon deeleen farlu bu ngeen nekkee ci àll bi ak ci kër yi. »

Al-Habdul Xadiim
17/06/2020.

Dénkaane Sëriñ bi

Dénkaane bu jëm ci Murid yëpp (10) Dénkaane bu jëm ci Seex Mabaabu Géy ak yeneeni dénkaan yu jëm ci bépp murit

share Partager

S’abonner
Notification pour
guest
2 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Adja Amina
Adja Amina
6 années il y a

Mashallah 🙏🏽 Sante