Dénkaane bu jëm ci Seex Mabaabu Géy ak yeneeni dénkaan yu jëm ci bépp murit
Al-Habdul Xadiim
21/06/2020
Bismilaahi Rahmani Rahiim.
Di nga fi dégge ay dénkaan yu fees deel ak njariñ, lépp nag jëm ci jullit bi rawatina murid bi. Te mel na ne tënk na lu bare bari ci ñaari Téere yi nu mujjee yaatal te mooy Maxaaliqu-Niiraan ak Zaadu Zawii-Tahalumi.
Al-Habdul Xadiim
20/06/2020
Entrées similaires:








S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent
Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires