Dénkaane bu jëm ci Abdullahi (6)

Al-Habdul Xadiim
15/02/2020

Bismilaahi rahmaani rahiim.

<<Yaw Abdullahi maa ngi lay dénk nga ragal Yàlla waxtu wu nekk. Boo bëggee mucc ëllëg, làq ag texe. Nanga sellal sab xol, te tàqalikoo ak bidaa, te taqoo ak Sunna, tey fexe sàmmonte ak ndigal yi.Deel ànd ak ñu baax ñi, bul ànd ak ku bon mukk. Deel fexe saafara say ayib waxtu wu nekk, te bul toppatoo ayibi jàmbur yi. Lépp lu la Yàlla tere dee ko daw, loolu dina tax def li mu lay diggal yomb ci yaw.
Lii nag tuuti na waaye am na njariñ lool.
Nanga fexe sàmmonte ak moom !>>

Al-Habdul Xadiim, Grenoble, 15/02/2020.

share Partager

S’abonner
Notification pour
guest
9 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires
Ndiaye Sarr
Ndiaye Sarr
4 années il y a

Salame magui ziarre bouwérrr xana dit guenne contanne ci liguéy bit nguénne dit yatatalle amna solo lolou wayé yalle – nalénne S. TOUBA Faye

AffiliateLabz
4 années il y a

Great content! Super high-quality! Keep it up! 🙂

Al-Habdul Xadiim
Al-Habdul Xadiim
4 années il y a
Répondre à  AffiliateLabz

Thanks you so much!

Ndiaye Sarr Ndiaye
Ndiaye Sarr Ndiaye
3 années il y a
Répondre à  AffiliateLabz

Machalla

Yacine
Yacine
4 années il y a

Dieureudieuf Mouride

Cheikh kandji
Cheikh kandji
4 années il y a

Machallah am solo lol,Yalla nagnou Yalla défal AK dégue akoup topp barké Cheikhoul Xadiim