Bismilaahi Rahmaani Rahiim.
« Maa ngi leen di dénk topp Yàlla te bañ a noonoo, deeleen soppante ci Yàlla te bañ a xëccoo, bañ a réeral kenn. Soppante ci Yàlla mooy ag ngëm, ku ko def dangay am mbégte ak Kóolute ; iñaanante nag ñu ko def cig texeedi rekk la leen jëme. Jikko ji gën ci jikko yi mooy sopp ci Yàlla ak yónnent bi (aleyhi salaam).
Al-Habdul Xadiim
Képp kuy farlu ci Alxuraan ak Xam-xam ab gindeekat dëgg la. Deeleen moytu rëy ak xëccoo, tey laabirante, tey tuub. Deeleen jàng tey jàngale ndax masu ñoo deñ di doon yooni àjjana. »
Grenoble, 14/03/2020.
Jerjef sante naniou boubax
Jaajëfaat
Alkhamdoulila santati
Noo ko bokk
Machallah
Jërëjëf
Akassa machala
Jërëjëf