gear Paramètres Push
chat
Bismilaahi Rahmaani Rahiim. Nee nañu képp ku teewe jotaayu sikkar ci Ramadaan, sunu Boroom dana ko bindal ci bépp jéego jaamug am at. Te bu ëllëgee ci kerug aras lay toog ànd ak Yónnent bi salla laahu aleyhi bi aalihi wa sahbihi wa salama . Képp kuy taqoo jullig mbooloo ci Ramadaan, sunu Boroom Subhaanahu […]
Bismilaahi Rahmaani Rahiim. Li ma lay xamal mooy nga togg ci barab bi nga nekkoon njëkk may génn, te bañ a déglu waxi nit ñi nga xam ne dañuy njort te duñu xam. Amna bayit yu ma defoon fan yii ci kër Seex Siidiya, mooy :<< Ku jublu Yàlla sunu Boroom noppalu, noppal keneen. Ku […]
Bismilaahi Rahmaani Rahiim. Fii danu fiy xamle ni Sëriñ bi daan jëflante ak Maam Cerno, te mooy ni mu ko yare, ni mu daan taqoo ak moom, ak ni mu ko gërëmee. Al-Habdul Xadiim Grenoble, 08/04/2020.
Bismilaahi Rahmaani Rahiim. « Asalaamu haleykum wa rahmatula wa tahaala wa barakaatahu, ginnaaw nuyoo bi, boo gise bataaxel bi, na nga yabal ku mokkal Alxuraan koo xam ne, gone lay doon, mu ànd ak ñaari moroomam, ndax ñu man a jàngal gone yi nekk fi, te yabal ñatti waxambaane yu man a jàngale xam-xam, ndax […]
Bismilaahi Rahmaani Rahiim. Nu fas yéene jukki leen ci hikma yi Borom Daarul Muhti daan wax. Li nu fiy nettali nag ci Sëriñ Xalil Mbàkke mu Sëñ Mustafaa Afsa lanu ko toxale. Al-Habdul Xadiim Grenoble, 01/04/2020.
Bismilaahi Rahmaani Rahiim. Maa ngi lay nuyu yaw Ibraahima, te di la xamal ne da maa bëgg nga dimbali »Muhammad » ci aajoom ndax loru na lool. Saa soo gise bataaxel bi na nga ko béggal loo mën. Maa ngi ñaan Yàlla sunu Boroom àdduna bañ noo wor. Mbooleem ñi aju ci man na nga leen […]
Bismilaahi Rahmaani Rahiim. Sëriñ Tuubaa Xaada lahu laahu maxtaara lahu mas naa wax Sahiid Mbàkke : Mas ngaa gis ku mel ne Fàddilu Mbàkke mu ne ko déedeet ? Mu ne ko mas nga dégg ku mel ne Fàddilu Mbàkke? Mu ne ko déedeet. Sëriñ bi ne ko Sahiid Mbàkke doo ma laaj sax lu […]
Bismilaahi Rahmaani Rahiim. « Maa ngi leen di dénk topp Yàlla te bañ a noonoo, deeleen soppante ci Yàlla te bañ a xëccoo, bañ a réeral kenn. Soppante ci Yàlla mooy ag ngëm, ku ko def dangay am mbégte ak Kóolute ; iñaanante nag ñu ko def cig texeedi rekk la leen jëme. Jikko ji gën […]
Bismilaahi Rahmaani Rahiim. Maa ngi lay nuyu yaw mi nga xam ne sag leer dafa bari ba nga set wecc ngir topp gi nga topp diine, yaw sama xarit bi ñu wax ne Yàlla daf koo xajal boppam ba mujj mu noot ko. Lii laa lay dénk deel topp ndigali Yàlla yi, tey daw ay […]
Bismilaahi rahmaani rahiim. Sëriñ bi ginnaaw ba mu leeralee ni kuy sàkku Boroomam la ak Yónnentam ba salla laahu tahaala aleyhi bi aalihi wa sahbihi wa salama, la daaldi wane ag jubloom ci dénk soxnas baayam ju ndaw ja, nu naan ko Penda Jóob. Daf ko wax ne: Maa ngi lay diggal yaw soxna si […]