gear Paramètres Push
chat
Bismilaahi Rahmaani Rahiim.
Jullit bi kuy ay noonam? Nees di def ba teqalikoo ak ñoom? Su ci ame tont yu leer, naka la war a def ba man a nekk ak nit ñi te topp Boroomam ci teggin yi gën a rafet, gën a seel, gën a ganjaru.
Al-Habdul Xadiim 15/07/2020
share Partager
Jeureujeuf yalla n’a doli tawfexx yi
Amiin Amiin mu boole nu ko biir ak biti
Yàlla na nga fi yagg ta wer !
Amiin Amiin nu bokk fee yàgg te wér
Machallha yage fi lol te wer
Amiin nu bokk fi yàgg barke Borom Tuubaa!
Jeureujeuf yalla n’a doli tawfexx yi
Amiin Amiin mu boole nu ko biir ak biti
Yàlla na nga fi yagg ta wer !
Amiin Amiin nu bokk fee yàgg te wér
Machallha yage fi lol te wer
Amiin nu bokk fi yàgg barke Borom Tuubaa!