gear Paramètres Push
chat
Bismilaahi Rahmani Rahiim.
Di nga fi xame ne li jig doomu aadama mooy mu yar ay cëram ci toppndigal ak bàyyi tere ba ci xelam sax war na ci moom mu tënk ko ci xalaatyiiw. Loolu nag ite ju réy la. Yal nanu ko Yàlla defal! Lekk lu lewitam ndeke man na yombal lu bare bari.
Al-Habdul Xadiim26/05/2020
share Partager
Djadjeuf yaram amatina solo. Yalla nanou sounou Borom may degue ak topp barké Xassida yi 🙏🏽
Amiin amiin Soxna Jaara yal na Yàlla nangu ñaan
Jerejef, Yalla naniou Yalla diapandal jëfè gui
Amiin Abo Madiyaana
Machallah amena solo lol serigne cheikh
Jërëjëf Sayyidinaa Yuusu
Machallah fall
Jërëjëf Sëñ Saalihu
Dieureudieuf amatina solo
Jaajëfaat sant neen
Hakaza amatina solo yalla n’a lenn souniou b orom faye