gear Paramètres Push
chat
Bismilaahi Rahmaani Rahiim.Di nga fi xame sunuy ñent noon ak gànnaay yi ñuy jëfandikoo. Nga wara xam nooy def ba xeex ak ñoom, nangu seen i ngànaay te dugal leen ci seen i kaso.
Al-Habdul Xadiim
21/05/2020.
share Partager
Machallah
Jërëjëf Sëriñ Saalihu
Jerejef Cheikh bi
Jaajëfaat!
Am naa solo lol Mouride. Yalla nanou yalla deffal degg ak topp.
Amiiin barke Borom Tuubaa
Amna solo yàlla nanu yàlla yombalal jëfe gi ci barke Sëriñ Bi
Amiin Amiin loolu de moo mat a ñaan !