Kan Mooy Seex Muhammadu Lamin Jóob Dagana

Al-Habdul Xadiim
01/06/2024

Seex Muhammadu Lamin 1886 la gane àddina. Yonent bi AleyhiSalaam la ko baayam tudde. Soxna Haanatu Jóob mooy way-juram wu jigéen. Sëriñ Tafsiir Ahmadu Jóob mooy baayam mi ngi dëkkoon Dagana. Wollare Sëriñ Tuubaa la woon, moo ko jébbal itam Sëriñ Muhammadu Lamin ak mbolleem njabootam.

Seex Muhammadu Lamin it ku amoon hikma la. Daan na wax naan:

  • Yaxantu, joxe ngir Yàlla moo ci gën a gaaw.
  • Leble ak topp mooy maye ag jiitu.
  • Xam sa bopp ci topp Yàlla la bokk.
  • Jaamu Yàlla nu mu gën a mettee ab payam ci lay gën a baree.

share Partager

S’abonner
Notification pour
guest
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires