Leeral Fathu Zaahiril Baatin…

Al-Habdul Xadiim
29/09/2024

Ginnaaw muslu ci saytane, ak julli gu mat ci Yonent bi Aleyhi Salaam, Sëriñ Tuubaa Xaada lahu Laahu Maxtaara lahu daa sant Yàlla bu wér.

Dafa daaldi xamle li yit pas-pas bi nu war a am ci sunu Boroom ak ay jeexitalam, ci sunu nekkin, sunu jëfin ak sunu dund.

share Partager

S’abonner
Notification pour
guest
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires