Leeral Fathul Zaahiril Baatin…(2)
Al-Habdul Xadiim
01/11/2024
Dina fi feeñ lenn ci njariñ yi nekk ci bàyyeek sa lépp sa Boroom, woolu ko bu wóor, ak wéral sab pas-pas ci dëggal saw doxiin sa diggante ak moom.
Am na lees ci toftal ci Téere bi, jëm ci leeral luy mag, ak i màndargaam. Akub tënk jëm ci ponki Diine.
01/11/2024
Al-Habdul Xadiim
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent
Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires