Miftaahul Xuyóob (11)

Al-Habdul Xadiim
14/07/2025

Xaaj wi dees na fi àndi li bàmmeel di wax ak dóomu àddama. Muy luy xuppe, di soññe ak di jàjji ci sax ci lu baax.

Ndax moom bàmmeel man naa naat lool, waaye man na tiis lool.

Yal nanu Yàlla gindi bu wér ci lu baax ak ci lu am njariñ.

Miftaahul Xuyóob

Miftaahul Xuyóob (10) Miftaahu Xuyóob (12)

share Partager

S’abonner
Notification pour
guest
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire