
Dog wi deef na fi àndi itam lenn ci xar-baaxi Sëriñ bi, lenn ci yi ko Yàlla may ak lenn ci ay hikmaam
Naka noonu da nga fi dégg ay hisa yuy wone ni am na it ñu ko daan jéem a natu ci anam yu kéemaane. Ak ni mu daan delloo lépp ci Yàlla.
Dina fi fés cantaakoon gi mu doonoon ak ni mu ñàkke moroom.
Yal nanu Yàlla xiir ci liggéeyal Sëriñ Tuubaa Xaada lahu laahu maxtaara lahu.