Dénkaaneb Sëriñ Alhaaji Mbàkke (15)

Al-Habdul Xadiim
06/04/2022

Bismillaahi Rahmaani Rahiim Ginnaaw nuyoo gu mat ci namu ko baaxo defe, la daaldi dénkaane sax ci jëfe ndigal ak bàyyi tere tey moytu yàq.

Di boole it liggéey ak wakiirlu ci sunu Borom. Mu yee nu ci nopi ci lu amul njariñ ak sax bàyyi lu amul njariñ. Sëriñ Tuubaa daniwoon ku taqoo ak ndigal yi ànd na ak man, ku ci saxul àndul ak man, donte daf maa jage. Ba tey dénkaane na fi lu am solo jëm ci sàmm ag gis ci lu Yàlla gëramul.

Al-Habdul Xadiim
05/04/2022

share Partager

S’abonner
Notification pour
guest
2 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires
Yacine
Yacine
2 années il y a

Maa shaa Allah. Amatina solo