Bismillaahi Rahmaani Rahiim Laabire gi Sëriñ Alhaaji Mbàkke daf ciy fàttali jeexug àdduna ak ñàkkam solo. Te sax li fiy jàmm mooy farlu ci sàkku lu baax ak di jaamu Yàlla. Noo man a tool, loo man a am, koo man a doon da nga faatu.
Loolu sax mel na ni moo tax muy laaj ana Lat Jóor ana Buur Siin Kumba Juuf? Ñépp wéy neen.
Ginnaaw fàttali gi nag, daf ko daaldi toftale ay baay yoy ku ko sab dund man naa neex
Al-Habdul Xadiim
08/04/2022