Dénkaaneb Sëriñ Alhaaji Mbàkke (2)

Al-Habdul Xadiim
30/05/2021

Bismilaahi Rahmani Rahiim.

Lii ab dénkaaane la bob ma nga bàyyikoo fa Sëriñ Alhaaji Mbàkke Xaadimul Xadiim. Mu ciy soññee ci gën a farlu ci jaamu Yàlla. Tey gën a fonk Alxuraan ak Xasiiday Sëriñ bi. Mu xamal nu ci itam ni war na ku ne ci nun sàkkul boppam waxtu yoy dana ci tuubal Boroomam donte jamono yépp waroon naa doon jamonoy tuub. Mu xamle fi itam lu aju ci yéeney yiiw. Biral fi bu wér, yéeney yiiw du jëfi boromm ayib. Ci noonu la ñaanale mboolleem jullit ñi ñaan yu réy te kawe njort.

Al-Habdul Xadiim
30/05/2021

share Partager

S’abonner
Notification pour
guest
4 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires
Selemaan Jaañ
Selemaan Jaañ
3 années il y a

Maasàlla

Seny DEME
Seny DEME
3 années il y a

Dieureudieuf