Tombi Borom Tuuba (4)

Al-Habdul Xadiim
14/03/2023

Bismillahi Rahmaani Rahiim Fii ay dénkaane yu jëm ci Sëriñ Mbàkke Buso deef na ko fi dégg. Mellow taalube dëgg-dëgg, néewal nelaw yi lu tax manul ñàkk, dëddu àdduna ak dëgmal ëllag li tax manta ñàkk dina fi feeñ.

Soññee na it bu baax ci wattandiku yeen jikko yi nga xam ne Yàlla gëramu ko. Di soññee itam ci yittewoo xam Yàlla.

share Partager

S’abonner
Notification pour
guest
1 Commentaire
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires
Yacine
Yacine
1 année il y a

Wa aleykoum salam wa rahmatoulahi takhla wa barakatahou. Jangalai bi leer na lol. Lou mata tass thi tout tank yi nguir gnou maagalai djikko you baakh