Asalaamu haleykum li ab woote la jëm ci liggéeyu Daaras yi fa Tuubaa-Daarul Muhti kër Sëriñ Alhaaji Mbàkke. Noo ngi sàkku ci képp ku ci gis jariñ nga yaatal ko ba nu bari man ci jot, te tàbbal ci seen jëf. Jërëjëf.
Ceci est un appel à contribution pour la construction des Daaras à Touba-Daroul Mouhti chez Serigne Alhaaji. Nous sollicitons auprès de tous, une large diffusion du message et une participation massive au projet. Merci!
Al-Habdul Xadiim
23/11/2020