Dénkaaneb Sëriñ Alhaaji Mbàkke (13)

Al-Habdul Xadiim
02/03/2022

Bismilaahi Rahmaani Rahiim Dénkaane bi dafa jëm ci soññi jullit ñi rawatina muriit yi ci gën a baayi xel mujjug jamono gi Yonent bi Salla Laahu aleyhi sa salam doon wax ak yàqu yàqu yi ci aju. Muy woote kon ci gën a dëgmal Yàlla jaare ko ci yoon wi Yonent bi aleyhi salaam rëdd te mooy Alxuraan ak Sunaam.

Sëriñ bi dégge ci ne kon sunu Boroom war nanu jaral lu ne walif alal yi. Dëgmal ko nag ci murid mooy sax ci Alxuraan ak Xasiiday Seexul Xadiim. Yal nanu Yàlla defal dégg ak top Barkeb Sëriñ bi.

Al-Habdul-Xadiim
02/02/2022

share Partager

S’abonner
Notification pour
guest
2 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires
Yacine
Yacine
2 années il y a

Maa shaa Allah. Amatina solo dieureudieuf Mouride