Dénkaaneb Sëriñ Alhaaji Mbàkke (9)

Al-Habdul Xadiim
28/10/2021

Bismilaahi Rahmaani Rahiim.

Lii ab laabire la bu bàyyikoo ci Sëriñ Alhaaji Mbàkke Xaadimul Xadiim jëm ci fonk julli ci Yonent bi Salla laahu tahaala aleyhi bi aalihi wa sahbihi wa salama.

Wax na fi loo xam ne dana yokk jullit bi ag sawarte ci gën a fonk Salaatu rawatina di ko jaarale ci Salaatu yi nga xam ne Sëriñ bi tudd na ko ak Xasidaam yi nga xam ne da ko def jagleel ko wàll woowu.

Al-Habdul-Xadiim
28/10/2021

share Partager

S’abonner
Notification pour
guest
2 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires
Ndiaye Sarr Ndiaye
Ndiaye Sarr Ndiaye
3 années il y a

Machalla yalla nalénne S. TOUBA Faye machalla amna solo lolou