Dénkaaneb Sëriñ Alhaaji Mbàkke (12)

Al-Habdul Xadiim
07/01/2022

Bismillaahi Rahmaani Rahiim

Ginnaaw nuyoo gu matale, la daaldi soññee ci Xasiida yi ngir nu gën koo fonk, gën koo jàpp, gën ci soobu te Yàlla tax.

Ginaaw loolu, la daaldi wax luy tax ñu nekk ci ak anam gi ko Sëriñ Tuubaa Xaada lahu Laahu Maxtaara lahu fonke woon.

Yal nanu Yàlla xiir ci Xasiida yi te dimbali nu.

Al-Habdul Xadiim
07/01/2022

share Partager

S’abonner
Notification pour
guest
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires