Jaar-jaari Yónnent bi (Saws) – 3

Bismilaahi Rahmani Rahiim Jaar-jaari Yónnent bi (Saws) – 3 Fii di nga fi xamee leen ci pexe yi nga xam ne yéefar yi daan nañu ko fexeel Gën ji mbindéef. Da naa fi wax fi itam faatug Aamina ak Abdul Mutalib. Yoonu Saam ak li fa feeñ ci xarbaax. Jambarug Soxna Xadiija ci tambalig Wahyu […]

Jaar-jaari Yónnent bi (Saws)-2

Bismilaahi Rahmani Rahiim Jaar-jaari Yónnent bi (Saws)-2 Ba Yónnent bi ganee àddina kiimaan yi fa xew ak xéewal yi mu indaale. Mbir yi amoon ci bañu xaree Dënam gu seel gi, ba tey itam leen ci turam yu seel yi te neex, di nga ko fi dégge insàllaa. Al-Habdul Xadiim 27/10/2020

Jaar-jaari Yónnent bi (Saws)

Bismilaahi Rahmani Rahiim Jaar-jaari Yónnent bi (Saws) Di nga fi xame maami Yónnent bi. Jikkoy Abdul Mutalib ak Abdulaahi itam dees na ko fi xamee Al-Habdul Xadiim 26/10/2020

Dooley mbidum Sëriñ Tuubaa (3)

Bismilaahi Rahmaani Rahiim Ndegam bëgg ngaa gën a xam mayi Sëriñ bi cig mbidam, teewlul kàddu gi. Al-Habdul Xadiim 01/10/2020

Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR