Bismillahi Rahmaani Rahiim. Lii ab Téere la bu jëm ci tontu Umar Ñaan kenn la ci taalibey Sëriñ Tuubaa Xaada lahu Laahu Maxtaara lahu. Dénkaane gu am solo la lool. Sëriñ bi fàttali fi màggug Sunu Boroom, tudd melloom yu sell yi, di xamle ne lépp ci ay yoxoom la nekk. Lu sotti lu nekk […]