Bismillahi Rahmani Rahiim Ci xaaj wi deef na fi leeral, solos màggal gi fa Boroom Tuubaa, dayyob cant gi kawe na, yékkati ku na, te yooll yi bari. واجعل طعامي و شرابي يا كريم ذكرا و شكرا و ثوابا لا يريم « Yaw Yàlla mu tedd mi Yàlla nga def samaw ñam ak samag naan muy […]