Mbokk mii di Xaadim Ja dafa réer. Boobu ba tay kenn xamul ci moom dara. Nataal wii, noo ngi ko jëlle ci « AESF ». Nuy sàkku ci ku ko man di gis nga jokk limat yi ci nataal bi. Yal na feeñ ci lu gaaw. Amiin ! Ci nettali bii nag dees na ci xame dolleey […]