Bismilaahi rahmaani rahiim.
Yaw miy bëgg a xam jaar-jaari mag ñi, kii ab Soxna su tedd la. Cosaanam, njabootam, diggam ak Sàngam ba Seexul Xadiim, lu bari dana la fi leer.
Ousmaan kebe mooy ki def waxtaan wi, nga naanal ko guddu fan ak wér, sunu Boroom musal ko te saamal ko boppam, défal ko jàmm ak xéewal, sutura ak teranga bàrke Borom Tuubaa.
Wa Diawartulah Tv ñoo ko don yaatal.
Ousmane Kébé, Diawartulah-Paris, 27/01/2020.
Machallah baye ousmane sama rak djou baxe borom bi yok xam xam barke cheikh ibra.
Amiin Barke Boroom Tuubaa
Machala mouy lou am solo lol ndakh gnépa wara kham ndiabotouk Serigne bi
Lu wér nga wax de.
Dimbal gu réy de mi ngi ci.
Machala amna solo lol gnépa wara kham ndiabotouk serigne bi