Jantub jamono!

Sëriñ Saalihu Mbàkke mi ngi gane àdduna ci atum 1915 ca Njaaréem di doomi Sëriñ Tuubaa Xaada lahul laahu maxtaara lahu ak soxna Faati Jaxate. Ku amoon taxawaay la, dëgër lool am i bët, ay cëram dëggër. Ku manoon a xerawlu la, am kersa, bari woon lool lumiy jaxasoo ak ay gone, da leen a […]

Jazbatu Sighàr(4)

Ap dog Ni ñuy gëmé dogal bi moodi ñu gëm ne lepp lu am suñu boroom mooko amal ci kàttanam ak ub xam-xamam, moo xam lu nëbbu la wala muy lu feeñ, wala aw yiw wala aw ay, melné toppu yoonu yonnent bi salla laahu tahala aleyhi bi alihi wa sahbihi wa salam wala topp […]

Kan mooy Sëriñ Madùmbé Mbàkke?

Seex Ahmadu Ndùmbé Mbàkke mi ngi ganné adduna 1859 ci dëkk buñu naan Nja feeté Mbàkke Baol, doomi Sëriñ Zayd Mbàkke la, moom Saër Soxna Busó moom Maam Mahram. Mi ngi yaroo ci kepparu wayjuram, and naak mom wooté Màba Jaxu Ba ca Saalum nekk Poroxan. Ginaaw ba wayjuram wa nélawé la dem Mbàkke Kajjóor […]

Jazbatu Sighàr(3)

Bismilahi rahmani rahim Ap dog Ni ñuy gëmé yonnent yi aleyhimu salàtu wa salamu móodi da ñuy gëm ne suñu borom mo len yóoni ci ñun bu werr. Gëm itam lepp luñu andi, te gëm ne duñu fen, duñu def lu haram, duñu def luñu sib, duñu nëbb li ñu len digal ñu jottaliko mindeef […]

Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR