1-Seriñ Tuuba Qàda lahu laahu maxtara lahu ne na: maqàma mi gana kawé fa yàlla jamono ji moy dëkal weetal yàlla cib xol. 2-Sëriñ Tuuba Qàda lahu laahu Maaxtara lahu ne na mbir yi ñetti xaacc lë: xam-xam bu am njariñ ak jëff ju yiiw ak teegin buñ gëram. Xam-xam bu am njariñ mi ngi […]
Bismilaahi rahmani rahim. Sunu Sang bi, mi ngi bàyikko ci ñaari askan yu tèdd ta moy askanu Mbàkke Maam Maharam ak askanu Koki. « Mbolem borom xam-xam yi ci réew mi ak wàliyu yi ci ñaari neek yi dong lañ sëto » ci waxi Sëriñ Xalil ca teerem ba mu duppé Goor Yàlla gi, Maam cerno nak […]