Ñaari jant fa kër Señ Hamdi Mustafa.

Bismilahi rahmani rahim. Sunu Sang bi ñu gëna xam ci turu Sëriñ Séex Faal Baayu Goor, mi ngi gané adduna Dakar ci att’um 1918 ci bisu Aljuma. Turam dëgg móodi Séex Ibràhima Faal, ñu duppé ko Maamam mi nga xam ne moom la njëkk am ci sët bu goor. Waayjuram wu goor mi ngi tuddu […]

Siiratu Sheyxul Xadiim

Sëriñ Alhaji Mbàkke mooko taalif ngir mokkal jaar-jaari Señ bi Qàda lahu laahu maxtara lahu gana jàpandi ci ñun. Señ Mustafa Ñing mooko jang. Al khadimiyya TV ñooko yàtal

Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR