Jazbatu Sighàr(2).

Bismilahi rahmani rahim **** -Ap dog Ni ñuy gëmé malaaka yi aleyhimu salam moodi nga gëm ne am na ñu., duñu def bàkkaar, duñu lekk, du ñu naan, duñu xayta, duñu béewal, duñu goor, duñu jigéen. Ay jàmm lañu, ci leer lañu leen bindé, bokku ñu ay mélo itam. Ci sàbbaal suñu borom lañuy naané, […]

Jazbatu sighàr han lahibin li xidmatil muxtaar(1).

Bismilahi rahmani rahim. « Sëriñ Alhaji Mbàkke Xàdimul Xadiim mo ci’y gàttal ci wolof téeré bii ngir bëgg julit yëpp njariñu ci rawanté’naak muriid yi yalna ko yàlla nangu ci barkep Sëriñ Tuuba Qàda lahu laahu Maxtara lahu »                                                                        *** Méñatum « Jazbatu sighàr » Bismilahi rahmani rahim salla laahu hala sayyidina muhamadin wa […]

Ñaari jant fa kër Señ Hamdi Mustafa.

Bismilahi rahmani rahim. Sunu Sang bi ñu gëna xam ci turu Sëriñ Séex Faal Baayu Goor, mi ngi gané adduna Dakar ci att’um 1918 ci bisu Aljuma. Turam dëgg móodi Séex Ibràhima Faal, ñu duppé ko Maamam mi nga xam ne moom la njëkk am ci sët bu goor. Waayjuram wu goor mi ngi tuddu […]

Siiratu Sheyxul Xadiim

Sëriñ Alhaji Mbàkke mooko taalif ngir mokkal jaar-jaari Señ bi Qàda lahu laahu maxtara lahu gana jàpandi ci ñun. Señ Mustafa Ñing mooko jang. Al khadimiyya TV ñooko yàtal

Diyàfatu samàdiyah (1)

1-Seriñ Tuuba Qàda lahu laahu maxtara lahu ne na: maqàma mi gana kawé fa yàlla jamono ji moy dëkal weetal yàlla cib xol. 2-Sëriñ Tuuba Qàda lahu laahu Maaxtara lahu ne na mbir yi ñetti xaacc lë: xam-xam bu am njariñ ak jëff ju yiiw ak teegin buñ gëram. Xam-xam bu am njariñ mi ngi […]

Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR