Kan moy Maam Cerno Birahim Mbàkke?

Bismilaahi rahmani rahim. Sunu Sang bi, mi ngi bàyikko ci ñaari askan yu tèdd ta moy askanu Mbàkke Maam Maharam ak askanu Koki. « Mbolem borom xam-xam yi ci réew mi ak wàliyu yi ci ñaari neek yi dong lañ sëto » ci waxi Sëriñ Xalil ca teerem ba mu duppé Goor Yàlla gi, Maam cerno nak […]

Serigne Saliou Mbacke ibn Serigne Abdoul Ahad JAARAMA CHEIKH IBRAHIMA FALL

Kan moy Sëriñ Alhaji Mbàkke Xàdimul Xadiim ?

Bismilahi rahmani rahimi « Li ma xam ci sama’g  dundu ci gaatal man Xàdimu Xadiimi Rassùlilaahi sala laahu tahala haleyhi wa salam »      Ma ngi gané àdduna ci at’um 1979 wala 1980 ci Daarul Muhty, dëkub Maam Cerno Ibràhima  radiya laahu tahala anhu. Sama baay mi ngi tuddu  Seriñ Mustafa Hafsa doomi Serin Muhammad Hawa Bàlla […]

Li xol bi yene

Li xol bi yeene ci aw yiw Yalla daal a ko xam Moo man ni cas benne lii mey bëg yit nima am Mbooleem lu bon bëg naa ca genn set ca bu wer Ta dëk ciw yiw ta andak Yalla faw ta gëm YouTube: Serigne Mbaye DIAKHATE

Kéenal Seriñ bi bi-qalami Seriñ Mbay Jaxate

Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR