Wooteb liggéeyu Daara yi kër Sëriñ Alhaaji Mbàkke

Al-Habdul Xadiim 23/11/2020

Dooley mbidum Sëriñ Tuubaa(5)

Bismilaahi Rahmani Rahiim. Di nga fi dégge mbir yu yéeme ci Xasida yi. Ndekke dafay yëngal xolu Yónnent yi ak Malaayika yi aleyhimu salaam, di tiital saytane ak di ko gàcceel, di bégal ñi koy jàng ak ñi koy déglu. Al-Habdul Xadiim17/11/2020

Dooley mbidum Sëriñ Tuubaa (4)

Bismilaahi Rahmani Rahiim. Noo ngi fas yéene wéyal liggéey bi ci Xasida yi nga xam ne ñooy karaamay Sëriñ bi, batey ci lay waxe lu bari ci ay mayam ak ay jagleem. Xasiida yi nag di jariñ lool ki koy jàng. Al-Habdul Xadiim 10/11/2020

Kan mooy Seex Sàmba Jaara Mbay?

Bismilaahi Rahmaani Rahiim. Sunu Sang bi, mi ngi gane àddina ci atum 1868 ci dëkkub Seex Maxtaar Ndumbe Jóob, nu naan ko Koki muy dëkk bu seel. Sëriñ Mamadu Mbay moo di baayam, Soxna Ndaak Ñang moo di ndeyam. Ginaaw ba mu mokkale Alxuraan ci la daal di jàng Tawhid ak Fiq. Waaye yéeneem moo […]

Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR